Intégralité Conférence de Presse - Modou Lô prévient Ama Baldé : "Douma Niékhou Niébé..."

27 nov. 2020
94 657 Vues

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct facebook.com/luttetv/
facebook.com/luttetv/
instagram.com/luttetv/
luttetv.com/
frlift.info

Commentaires
  • 30:10

    AFRIQUE GAMES 3.0AFRIQUE GAMES 3.0Il y a 23 jours
  • Machala il communique bien tres civilisé et class modou lo

    Rokhaya DiakhatéRokhaya DiakhatéIl y a mois
  • Modou yalna la yalla may ndam😍

    Baye CheikhBaye CheikhIl y a mois
  • Modou lo ndam rk inchallah. Un vrai lion

    gëm sa boppu tvgëm sa boppu tvIl y a mois
  • Modou lo yalla nala yalla mayy ndam❤️

    Mame Saye SyllaMame Saye SyllaIl y a mois
  • Bou fekke beure rek Ama mounoul dane Modou lo khana sisoumane yi coalisés sot ko ci galadj

    Maryama KandeMaryama KandeIl y a mois
  • Ama yéeeeeeeee futur roi yalla nala yalla may ndam inchalla

    Seynabou SeckSeynabou SeckIl y a mois
  • ❤️

    Abdou NiangAbdou NiangIl y a mois
  • Ndam inchlah

    Ba amadouBa amadouIl y a mois
  • Sonorisation 0

    ansoumana santos goudiabyansoumana santos goudiabyIl y a mois
  • Modou LÔ bo fogonie diga dane ama tu te trompe ama dousa morom

    FRENKIE CHEIKHFRENKIE CHEIKHIl y a mois
  • Wa loumou hewler bay deff conférence de presse

    Moustapha SeckMoustapha SeckIl y a mois
    • Mo diara lathie

      Seynabou SeckSeynabou SeckIl y a mois
  • Modou yagui wax rk diapal ni bilay am gua combat pour ama rk no

    Khadim DiopKhadim DiopIl y a mois
  • Ça va être très très compliqué pour Ama Baldé, Modou lo ce n'est pas Papa Sow il est plus dur , plus vivace et plus malin Lac 2 il en sait quelque chose, Modou est le meilleur lutteur après Balla Gaye 2.

    Abdoulaye SyAbdoulaye SyIl y a mois
    • il est le meilleur lutteur de l’histoire

      Laye KharagneLaye KharagneIl y a mois
  • Modou lo rek

    Ablaye DioufAblaye DioufIl y a mois
  • Ama balde yalla na nga am ndam si katanou sounou borom

    jahdieff galsenjahdieff galsenIl y a mois
  • Modou lo esk minguii entrainner au serieux?kou guis lekh yii kouy noss dii lek khalisam lamay nirol

    TIPTIPIl y a mois
  • L meilleur victoire rekk inchallah xlo ilove u👍👐💛💚

    Lamita SowLamita SowIl y a mois
  • Modou lô rek bly

    Rap Galsen et ses projets tvRap Galsen et ses projets tvIl y a mois
  • Lamine Seck yangi ci frome deh yangi nakh boucar ndour deh 💪💪💪🔥

    dame mbenguedame mbengueIl y a mois
  • Ama balde futur roi inchallah Modou Lo amaa dakoy dann Inchallah

    dame mbenguedame mbengueIl y a mois
  • Kenn dou lutte Tv si lamb vous êtes les meilleurs Lamine Seck good brother

    dame mbenguedame mbengueIl y a mois
  • Diadieuf nèkha farale dimanche kharagne lo lép Nice na Yalla nanou Yalla maye ndam bou sèdde si kaw Ama

    Fafa NdaoFafa NdaoIl y a mois
  • Modou reck 👌🏾👌🏾👌🏾

    Sabil NianeSabil NianeIl y a mois
  • Soula ama diapé dinga kham lép deugue leu

    Mariama CisséMariama CisséIl y a mois
  • Man tutte TV rkk

    Xeushe OgXeushe OgIl y a mois
  • Macalla macalla lo dam

    Aboubacar TouréAboubacar TouréIl y a mois
  • Modou lô yalnala yallah may ndam cikaw ama baldé barké mouhamed

    khadim kanekhadim kaneIl y a mois
  • Ndam rek

    Adama WadeAdama WadeIl y a mois
  • Bilahi Yaye bvndii 😂😂😂😂 nioune ragalougnou lolou

    Yoro KantéYoro KantéIl y a mois
  • Amayé yalna gua ame ndam si barké Mohamed psl amine..Serge..🇸🇳❤🇮🇹🤲🏾🙏🏾🤲🏾

    S D NS D NIl y a mois
  • Diap len si svp guen abonné si sunu chaine youtube SEN LAMB si barqué mack gnou bakh gni yalla nangen am diam ak khewal wer ak goudou fan si barke seydina MOUHAMED(PSL) diap len si bok

    SEN LAMB TVSEN LAMB TVIl y a mois
  • Ama mokaye yeungueule dh future roi mineur

    Ouzin MbayeOuzin MbayeIl y a mois
  • Fasse bouy mamou labou seriss lagnkoy labe 😂 😂 sacré tontou xlo 4 ever

    Modou MboupModou MboupIl y a mois
  • KOU BEUG LISTIKHAR NIANE POUR OUBEKOU BAYRE PROBLÉM COUPLE PROBLEM PAPIER 78 468 33 61

    OUSTAZ MAMADOU DialloOUSTAZ MAMADOU DialloIl y a mois
  • Modou lo rekkkkk bilae xol seed na ndax say kadou rafette nagne thie sensibilisation jeunesse bii

    Pape NdourPape NdourIl y a mois
  • 100% pikinois yalnala ama daneu

    Mamadou lamine solyMamadou lamine solyIl y a mois
  • Kharagne a vie ❤️ Mala beug bly

    Moussa SallMoussa SallIl y a mois
  • 1heur d temps 9minutes la modou wax journaliste bi yekatil sa toubay bi guay wasar wasari a kay bandit me leçon la pour nous les garçons nañiou yekati suñiuy toubay

    syllah accessoiressyllah accessoiresIl y a mois
  • Zzzzzzzzzzzzzzzzzzzz2zzzzzz2zz

    Moussa SyMoussa SyIl y a mois
  • 👑👑👑👑Modou Lo 👑👑👑👑Xaragne Lo👑👑👑👑 Yalla nala Yalla maaaaay ndaaaaaam Modou Lo Yalla gua daaaane Ama Baldé

    Idy Xaragne LoIdy Xaragne LoIl y a mois
  • Kharagne lo♥️

    Baba DiongueBaba DiongueIl y a mois
  • Nikhou balla gaye gua bou nekh

    Malang DiemeMalang DiemeIl y a mois
  • Modou lo yalla naka yalla maye ndame amine 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

    paté Diop touba 100% kharagne lo kharagne rekpaté Diop touba 100% kharagne lo kharagne rekIl y a mois
  • Son bi bakhoul wala si.mane lee ??

    Cheikh NdiayeCheikh NdiayeIl y a mois
  • Modou Lo dafa geuneu professionnel

    MOUSTAPHA LOMOUSTAPHA LOIl y a mois
  • *Maa Shaa ALLAH Monde 🌍 Lo le plus professionnel de l’arène Bilahi un discours d’un grand homme Vraiment super 👍 Tu es la stars ⭐️ de l’arène*

    Momo TourayMomo TourayIl y a mois
  • eska combat mounougnouko wiklo bou dialé gnou sauvé année bi en wiklo ak yénénes combat yi Luc Nicola l'homme dé grand événements essayél lolou ba xam

    Babacar NdiayeBabacar NdiayeIl y a mois
    • wahi dof Kone mbeur yi s'en yaram Dou tangue🤗...li Dou 11 -11/. bene bene le ok

      Mamadou NdiayeMamadou NdiayeIl y a mois
  • Machallah 👑

    Serifo ThiamSerifo ThiamIl y a mois
  • Keen dou Modou way sama champions bi

    Talla sowTalla sowIl y a mois
    • Modou.un.liteur.tres.fort

      Bara DioufBara DioufIl y a mois
  • Keen dou modou way sama champions bi

    Talla sowTalla sowIl y a mois
  • Keen dou mo way sama champions bi

    Talla sowTalla sowIl y a mois
  • Nèkha faral

    ibrahima sima diopibrahima sima diopIl y a mois
  • ndam rek inchalla

    Assane LoAssane LoIl y a mois
  • 100 combats modou lo dakoy daane 100 fois inchallah☝🏿🙏🏿

    Daouda MbowDaouda MbowIl y a mois
  • Machalla modou lo laff thiatt say kadou rafetna loll thi jeunes bi ak conseille yi machall yalnala yala may ndam lou sed gouye thi kaw ama

    Mbackegaydel Serigne mbackeMbackegaydel Serigne mbackeIl y a mois
  • Ana génération xaragne yi 💪🏻💪🏻roi ds arènes 👑👑

    Ndeya DioumNdeya DioumIl y a mois
  • allez les roi xlo ndam rék❤❤

    nous sommes avec sonkonous sommes avec sonkoIl y a mois
  • Amaaaa Rek 💪🏾💪🏾🔝

    Makhtar DiagneMakhtar DiagneIl y a mois
  • Modou looooooooo🤞

    Djimbori NgonéDjimbori NgonéIl y a mois
  • Modou Lo est devenu mature legui bonne chance champion

    supersarrsupersarrIl y a mois
    • modou moussoul immature

      Laye KharagneLaye KharagneIl y a mois
  • Yalna koumasé si diam djélhé si diam yalna si yala def diam

    Makhtar JawMakhtar JawIl y a mois
  • Yalna koumasé si diam djélhé si diam yalna si yala def diam

    Makhtar JawMakhtar JawIl y a mois
  • Niane Yalla - Diameu am Sénégal, - Covid-19 diogué fi, - Modou Lô dane Ama Baldé Inchallah 🇸🇳❤💯✅

    Mouhamed DiopMouhamed DiopIl y a mois
    • Amine ya rabbi

      Aissata DiackAissata DiackIl y a mois
    • Aminee♥️♥️🙏🙏

      Fallou LeyeFallou LeyeIl y a mois
  • Le roi a grandi

    Adama NiangAdama NiangIl y a mois
  • Xaragne l'o for Ever

    Gora NianeGora NianeIl y a mois
  • Ken dousi sama mbeur mai souma done tek khaliss si ama lay tek

    Assane KaneAssane KaneIl y a mois
    • @mourtada gueye ma diokhla sama numero boula nekhè ma ngui italie dinala gagne maylasi rerou guinar

      Assane KaneAssane KaneIl y a mois
    • @mourtada gueye gueye desna si yaw bounou diapè date niou tek

      Assane KaneAssane KaneIl y a mois
    • Assane kay gno tek ? Magui si Modou ...

      mourtada gueyemourtada gueyeIl y a mois
    • @paté Diop touba 100% kharagne lo kharagne rek noo pathe pourtan mai ama dafa gnimè te modou kouko gnimewoul doko dane si lamb rek la wakhè

      Assane KaneAssane KaneIl y a mois
    • @Assane Kane kon kay yaw ama moy sa mbeur

      paté Diop touba 100% kharagne lo kharagne rekpaté Diop touba 100% kharagne lo kharagne rekIl y a mois
  • Modou lô wakhou fi Dara

    Cheikh bass Keur massarCheikh bass Keur massarIl y a mois
  • 100 combat ama baldé daan ko

    Cheikh bass Keur massarCheikh bass Keur massarIl y a mois
    • Dafa ler

      Seynabou SeckSeynabou SeckIl y a mois
  • Modou lô dawoul sunu yaram de barki yalla

    Cheikh bass Keur massarCheikh bass Keur massarIl y a mois
    • yaw sa bounou baye😂

      Daouda MbowDaouda MbowIl y a mois
  • Kinepi rek 🇫🇷

    mame alioune diallomame alioune dialloIl y a mois
  • Sa wakh rafetna Modou

    adu boiadu boiIl y a mois
    • Bilay

      Bara DioufBara DioufIl y a mois
  • Kène dou modou champion deugu

    Djibril DiaoDjibril DiaoIl y a mois
  • Xlo😍💗💗

    Mbow mouhamedMbow mouhamedIl y a mois
  • Modou wakh ji rafét na amal diame

    Boy MbawBoy MbawIl y a mois
  • Lamine kéne dou yaw

    Boy MbawBoy MbawIl y a mois
  • Je suis un fans de Balla gaye mais mod lo c'est un exemplaire vrai yalla na la yalla may ndame

    Sidy GayeSidy GayeIl y a mois
    • Yaw do vrai fans Balla gaye kone do faral Modou lô

      Massamba DiopMassamba DiopIl y a mois
    • Ndam rek inchalla thièy mbaye

      Babacar MbengueBabacar MbengueIl y a mois
    • Amine

      Babacar MbengueBabacar MbengueIl y a mois
    • Ki mõm khana da voyagi wone mouy diay srx... nioune Ama laniou faral

      Mamadou NdiayeMamadou NdiayeIl y a mois
    • Fan’s Club Balla Gay 2 Deugeu Billahi Ama Baldé lay Farall Bou goré Nak ☝️C pasq BG2 combat wame ak Diouta Lo yeupou Ama balde Louné Lathiye Dath pour BG2 Amm ndam fay Lérr Narbii xoromam way 🙏

      L’absolu GueyeL’absolu GueyeIl y a mois
  • Thiey Modou mako wolou dh bilahi

    Deme MansourDeme MansourIl y a mois
  • Ama lambou Bi khalis rek laci ame modou dina la douma dane la

    Amed Dia SowAmed Dia SowIl y a mois
  • Yalla nala yalla may ndame

    Amed Dia SowAmed Dia SowIl y a mois
  • Sama roi bi yalla nala yalla diapalé bagua dane ama ak koudoul mom Amiiine

    Cheikh VIPCheikh VIPIl y a mois
  • Ndam rek inchala

    el hadji gueye ndioro efonoel hadji gueye ndioro efonoIl y a mois
  • Ama rek💯pikine 🇪🇸💪💪

    Omar flavourOmar flavourIl y a mois
  • Ama balde 💪🏾💪🏾

    Fakaramo SaidyFakaramo SaidyIl y a mois
  • Li dou commba way modou lo moko Manu fof ki dou mormou ama balde way li dou lamba

    Diaby SowDiaby SowIl y a mois
    • Dangay tiyatar rek

      Sylle PogbaSylle PogbaIl y a mois
    • @Diaby Sow diam si yaw sama wadji

      Assane KaneAssane KaneIl y a mois
    • @Diaby Sow bi combat royal la soow leup si yone la tego inchalla 00393208605593 gardel numero bi ba combat inchalla tè bou modou dano boulma bayi si biir

      Assane KaneAssane KaneIl y a mois
    • @Assane Kane oui incallah mai Man dama setan lamba pikine la deka mousma guiss ci mome kalite buy dane modou pasqui mom ama comba am yep cirip dip la day gaw mai modou saway ken dou lajal ouma sen ou guiri b

      Diaby SowDiaby SowIl y a mois
    • @Diaby Sow lolou deugu la soow modou mo guene graw nioniou mai mane kouy atakè la wakh tè ama nonou lay beurè yalla nanou ko feke ak diam rek

      Assane KaneAssane KaneIl y a mois
  • Modou lo yalla nala yalla may ndam si kaw ama balde si barki seydina mouhamad ak serigne touba

    Fallou MballoFallou MballoIl y a mois
  • Modou yow la 💪🏾

    omar njieomar njieIl y a mois
  • Modou lo yalnako yalla maye ndam inchalla

    Tine SadaTine SadaIl y a mois
  • Yallah na Yallah may ndam Ama balde

    Papa SyPapa SyIl y a mois
  • Modou rekkkkkkkkkkkkkkkk♥️♥️♥️♥️♥️

    Alpha CisseAlpha CisseIl y a mois
  • Mani.conba.bi.yaguatoule.ama.dina.ame.dame.inchala

    Elzo FallElzo FallIl y a mois
  • Inchala.ama.dina.ame.dame.

    Elzo FallElzo FallIl y a mois
  • Yaw modou lô kou xame ama baldé xameko si deugueul bopam ama dinala nok banga day dane laa kone xalé yaw sa sarakh fègn na do kouy diaxal ama

    gorgui sowgorgui sowIl y a mois
    • @Diaby Sow Modou diougué si défaite🤸😂 done roi kou mouy may buzz

      Mamadou NdiayeMamadou NdiayeIl y a mois
    • @Diaby Sow yw wahi dof...si buzz khà tolou 😂😂😂

      Mamadou NdiayeMamadou NdiayeIl y a mois
    • Ay siporter ama balde ñubari ay dof lanu hamolel touss pourqoi gen wahk ay waki dof moudu lo molen buzz ama balde mousoul am comba bu melni ce 1er foi

      Diaby SowDiaby SowIl y a mois
    • @Diaby Sow lolou force la 💪🏾

      gorgui sowgorgui sowIl y a mois
    • yeen wakhe dof rk demlene si boy niang mo niagellene wakh

      Pape SeckPape SeckIl y a mois
  • Modou lo le roi nékha faral dimanche

    Alieou LowAlieou LowIl y a mois
  • Ama yéééeeeeeeee

    Coudy ThiamCoudy ThiamIl y a mois
  • Amga combat de

    Brainkid Shidhi Official TvBrainkid Shidhi Official TvIl y a mois
  • le vrai roi modou yalna gua am dam bou ler si ama dorko bamou dé bilahi modou akka bandit ✊🏻✊🏿♥️

    papa mbeur yii modoupapa mbeur yii modouIl y a mois
  • ama dakoye dane

    Baye ManeBaye ManeIl y a mois
    • Amine

      Coly Noel BAColy Noel BAIl y a mois
    • A bon

      Diaby SowDiaby SowIl y a mois
  • Modou meune nga rafetal sa adversaire lou Abou waax mofi ame bene vip lafi mouy Tapha tine do waaxate kenene Malick Niang yeksé goul wone si cour des grands kone yafi seuss motax li ame akk çowwal lamb mais si adversaires dou yone si palmarès dou yone tamite wayé Borom bi Faye la sa xol nga ame si ndam bou reuy inshallah wasalam

    Badara DioufBadara DioufIl y a mois
    • Dégeull Dof bii Mom 😆😆😆 Xara ba Ama Diapouko Doxane Nayamm ngainn khamni Lèpou Deugeuleu yène 😏

      L’absolu GueyeL’absolu GueyeIl y a mois
    • Wouh way... waho lene fi dara Modou lo bane vip la dane limléne yene.eumeu ak Kane gawlene

      Mamadou NdiayeMamadou NdiayeIl y a mois
    • Nice jop lamine et bne continuations

      Maimouna SambMaimouna SambIl y a mois
    • Modou lo da bakh rék mias yalla nakou yalla mayy nnnadm Dina bakh dh

      Bassirou GeuyeBassirou GeuyeIl y a mois
  • Amoule benneu sance

    Maguette SeneMaguette SeneIl y a mois
FRlift