Série - Nawlé - Episode 02 VOSTFR

6 avril 2021
335 977 Vues

Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
instagram.com/kharmedia_officiel?igshid=jf9h4pcgofsi
facebook
facebook.com/kharmedia_l'officiel
Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.

Commentaires
  • Qui comme moi se sent perdu dans la traduction ici? On paye combien pour apprendre le wolof ? 😂😂😂😂 toujours des séries intéressantes mais BLOCUS au niveau de la langue pour les étrangers comme moi. Pitié

    Sipewou edithSipewou edithIl y a 8 heures
  • Mounirou est amoureux de salimata depuis son enfance mais il n lui a jamais révélé alors cette dernière n savait Jesper k la demande en mariage n vas pas gâché cette famille qui est toujours ensemble bakari aussi il regarde son intérêt

    Abdou DiopAbdou DiopIl y a 15 heures
  • Nonnn donc Ousseynou dafaa doubler son cousin si Salimata hhahaahhaha lol mdririr Quel combat alors

    Rane DiopRane DiopIl y a 15 heures
  • Quel discours 🥰🥰🥰 où sont les SALIMATA 💝

    salimata sambesalimata sambeIl y a 16 heures
  • Salimata dafa timide trop lii mo takh mou guene infidèle la rôle de coumba

    Alioune badara FallAlioune badara FallIl y a 19 heures
  • Déjà vue suis désolé

    Fatadio AliouFatadio AliouIl y a jour
  • Rabi sa rôle bi bokoy joué kene doula beugue mbecil salarié moy yelwane merde à la fin

    samba fallsamba fallIl y a jour
  • Dafa am lou may nawle bane biss lay am

    Maguette GayeMaguette GayeIl y a jour
  • Kone wa association oubi groupe whatsapp kafoleine ni 😭😭😭😭😂😂😂😂😂😂😂bamou sotti rek amna ay khememeurrr ak ay dieuw katt ak ay doxane katt 🥳🥳🥳🥳🥳😫😫😫dîna wathie

    Amicolle FallAmicolle FallIl y a jour
  • Halte à la promotion de l'infidélité

    Gning ModouGning ModouIl y a jour
  • Kharal ma nieuw khol lou nawlè di dionxè tamite

    Touty TallTouty TallIl y a 2 jours
  • Nafina del portez des boucles d'oreilles way

    coumbiz riocoumbiz rioIl y a 2 jours
  • les sous-titres ça marche pas!

    livia apalivia apaIl y a 2 jours
  • c'est pour quand le sous titrage?

    hevbeautyhevbeautyIl y a 3 jours
  • Yocklén machallah

    Hawa BocoumHawa BocoumIl y a 3 jours
  • Mane dall ousseynou la sanil carte mane ak kane

    Alimatou MbayeAlimatou MbayeIl y a 3 jours
  • il a pas plus dur que l'amour caché

    Mareme AidaraMareme AidaraIl y a 4 jours
  • Mies Satan katte yii war nano ame bénne série dhé tmt ah

    samba secksamba seckIl y a 4 jours
  • Stp son biye daw si souff kou xam noumou toudou au kouko way

    seydina omar diopseydina omar diopIl y a 4 jours
  • Une très belle Série et bien inspirée ❤️❤️❤️good job. Mais khar Media maneu khar naa Série Regret beu soneu tamite . Sur ce bonne continuation à toute l'équipe

    Mariama LoumMariama LoumIl y a 4 jours
  • Wa kharr média lane moy sen secret sur la lettre"A" Khadija , ndéla ,sadiya, salimata

    Sokhna DiaoSokhna DiaoIl y a 4 jours
  • C un beau théâtre machallah

    Aissatou DialloAissatou DialloIl y a 4 jours
  • Raby je taime bcp depuis idole tu joue bien machallah

    Galou DemGalou DemIl y a 4 jours
  • Néna borom salaire 800000f menoul dara donc borom salaire 200000f niogui dioye. Wakhi dof mane dé je préfère celui avec les maigres moyens té yeureum par rapport ak riche bima gnin té tegg ma beute🙏

    TMD-POULO -NDIONTADOTMD-POULO -NDIONTADOIl y a 4 jours
  • Nawlé dioulite dioulite moy nawléme.apres mou diékh

    Mariane DiopMariane DiopIl y a 4 jours
  • Hi dina nekh ak nafy dieye rk

    Mame ndiaye MbowMame ndiaye MbowIl y a 4 jours
  • Sén Nawlé laniou dh man dh yii khétou amour 💘 damay jalouse dh🤗🤗

    M DicM DicIl y a 4 jours
  • Wa khar média vous ne voulez op un jumeau pour mounirou khana j'ai mon grand frère qui lui ressemble beaucoup

    Queen Mayna GueyeQueen Mayna GueyeIl y a 4 jours
  • sous titres

    fabiola happifabiola happiIl y a 4 jours
  • Khaar média , toujours des thèmes pertinents , bonne continuation, on adore!!!!!💓💓💓💓💓

    Louisa seutou almaktoumLouisa seutou almaktoumIl y a 4 jours
  • Sara moytoul maquillage bou eup bi ate khéfyi Ousseynou warone nga prévoir gel sur la table, Covid bagui fi dé

    sanou Mbenguesanou MbengueIl y a 4 jours
  • J'adore cette série mention très bien à vous Allah veiller sur toutes les acteurs

    Mya QuennMya QuennIl y a 4 jours
  • Sa se voit que c'est du film tout simplement. 800mille guakoy kheipp comme salaire. Oufff

    Fatima Zahra BanaFatima Zahra BanaIl y a 5 jours
  • Dama tayal si série nakh ousseynou dou moudié tak saly 😭😭😭

    Zeynab RassoulZeynab RassoulIl y a 5 jours
  • Love Ousseynou ❤️

    Miss GueyeMiss GueyeIl y a 5 jours
  • Saly ioe mom gnou livré la aye sachet rek nga dieul sou nékone drogue police gnew diaplela sa adouna yakhou

    ya ndeye marieme syya ndeye marieme syIl y a 5 jours
  • Nice❤

    Dioundiou LoDioundiou LoIl y a 5 jours
  • Salimata dafa nice mais g pas trop confiance en elle. Wa yeen ani regret ak djabarou gorgui....eupeneu

    diop abydiop abyIl y a 5 jours
  • Lii dehh moo leumbe senegal nawle khett..... doyna warrr

    Maeva DioufMaeva DioufIl y a 5 jours
  • Ma diéma sétane nawlé comme guissouma regret wala la femme du chef 🤔

    Fatou SambFatou SambIl y a 5 jours
  • Pourquoi on a la série rarement 🥺

    Binetou Malick KaneBinetou Malick KaneIl y a 5 jours
  • Aaye waaay kagne laay ame kou melni Ousseynou si romantique ?? 😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍

    aicha dialloaicha dialloIl y a 5 jours
  • wa yéne li dou keur gniome sadiya

    aida fayeaida fayeIl y a 5 jours
  • Ousseynou dafa romantique kW 🥰🥰🥰🥰

    Aminata GoudiabyAminata GoudiabyIl y a 5 jours
  • Naguén déf dama diaron si sériyi motakh

    Ndeye ha ichatou touréNdeye ha ichatou touréIl y a 5 jours
  • Bonjour peut o avoir les sous-titres svp merci ?

    Ba AminataBa AminataIl y a 5 jours
  • Juste une question pourquoi les gens aime les hor sujet vous énervé a la fin puffff😡

    Mado G'y DioufyMado G'y DioufyIl y a 5 jours
  • Waa 4ans de relation yayou Saly nane yakolene faténa nioune neupp relation laaniou meune 😂😂😂

    Rokhy ManeRokhy ManeIl y a 5 jours
  • Mé secrétaire yii tamite nagnou niow bureau avc un p de maquillage sééne cils yii comme Ay demkatou xeww

    Rokhy ManeRokhy ManeIl y a 5 jours
    • Même dem kattou khew sakh dou deff li. 😂😂😂😂😂

      Mamy DiaMamy DiaIl y a 5 jours
  • Ki mo kate ndayam nena salaire 800mil dou dara domou ram

    lo djamillo djamilIl y a 5 jours
  • Mani la femme du chef lagn soxla AK regret

    Coumba DiakhateCoumba DiakhateIl y a 5 jours
  • Mais ana diabarou gorgui

    samba agnesamba agneIl y a 5 jours
  • Amy mii dei dou kharite ni référence ....

    khady thiamkhady thiamIl y a 5 jours
  • Ayoo suis très contente de voir nafi diéye dans une série franchement je l adore et elle très bélle machalla mh tmt bayil néan moyen fo dieum yobou kofa😁

    Ndew DiopNdew DiopIl y a 5 jours
  • Titre bi dhé Amna Chance Serie bi Yalna Amé Chance Nonou❤👌

    Fatou NiangFatou NiangIl y a 5 jours
  • Nn livreur bi dead nama🤣

    Ndeye fatou SeyeNdeye fatou SeyeIl y a 5 jours
  • Sali n’aime pa ouaseynou deysane sa s voi

    Fatou Demba ThiouneFatou Demba ThiouneIl y a 5 jours
  • who sing the song on the background

    Fanna CeesayFanna CeesayIl y a 5 jours
  • Masalah série bou neh

    awa diackawa diackIl y a 5 jours
  • Rabia est la femme de quel frère alors

    silksmithafulsilksmithafulIl y a 5 jours
  • Deukk bii kenh mounoufi préparer mariage en sécurité 🔐 🤔🤦‍♀️

    Adja Soukeye GningAdja Soukeye GningIl y a 5 jours
  • Vous avez raté le cadre de vie de chez salimata... c'est des gens dimine il fallait un autre présentation de leur maison

    nafi diakhatenafi diakhateIl y a 5 jours
    • @Astar cisse wala c'est ça !

      Rane DiopRane DiopIl y a 15 heures
    • Mais je penses q c pas une question de pauvre mais plutot une histoire caste

      Astar cisseAstar cisseIl y a jour
  • Sahara migui khépp 800mil té man 5moi batay magui weur salair 60m8l mlou teu ma ttiey yalla amna gnou yalla diapalé dh li dafa am si rew motax mai alkhamdoulilah

    Bou Serigne ToubaBou Serigne ToubaIl y a 5 jours
    • @Deugg Rekk Tv badou yéména dal

      Bou Serigne ToubaBou Serigne ToubaIl y a jour
    • Doul rek laniouy def....salaire 200 mille sakh da rare

      Deugg Rekk TvDeugg Rekk TvIl y a jour
    • billahi

      EVELINE GOMISEVELINE GOMISIl y a 5 jours
  • Nawle dal serie bi nekhe nama ousseynou hum ma sha Allah mounirou osi salimata la nop mais rabia tmt noooo elle me soul way avec c histoir tei gueumoul dara ish

    Mbathio CiseeMbathio CiseeIl y a 5 jours
  • Rabia en plus d’être folle elle est matérialiste Tite une vrai peste

    Aisha RassoulAisha RassoulIl y a 5 jours
  • Man dei salairou 75/70000 la guis Sénégal te mignonne nena 800.000 du salairou dara

    Seydina ADAMA Ndar Mouna DIOPSeydina ADAMA Ndar Mouna DIOPIl y a 5 jours
  • Machlla ♥️

    Sokhna NiangSokhna NiangIl y a 5 jours
  • Maman mounirou noboul salimata domou mbindane kene douko wakh waye je comprend nawle la toudou

    Adame NgomAdame NgomIl y a 5 jours
  • Ousseynou moy saï saï deeh😂😂🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 5 jours
  • Mounirou waaay 😂😂😂😂🤦🏽‍♀️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 5 jours
  • Quand je vois des gens qui s aime sa me r appel des truc

    Fatou SidibeFatou SidibeIl y a 5 jours
  • Mounane domou mindane mi domou mindane bi mola dak fouf 😡

    Alaloudarmankobi diakhoumpaAlaloudarmankobi diakhoumpaIl y a 5 jours
  • Nafi dieye comme kouy repeter

    Sokhna SSokhna SIl y a 5 jours
  • Machallah

    Ndeye Maty DialloNdeye Maty DialloIl y a 5 jours
  • Secrétaire setane toute les serie

    Ndeye Liza kalelaNdeye Liza kalelaIl y a 5 jours
  • 🥰Ousseynou mom Romantique naa di⭐🤣🤣🤣🤣

    Fatou CissFatou CissIl y a 5 jours
  • Marshallah I love this movie 😍😍😍👍

    Mama JaitehMama JaitehIl y a 5 jours
  • Saly et Ousseynou vous formez un joli couple c sa la vie ❤️♥️ Ousseynou bonne chance

    Isidore MemdyIsidore MemdyIl y a 5 jours
  • Rabia mome sikk na dh té meune khébaté🤣🤣🤣xalass

    adji diopadji diopIl y a 5 jours
  • Wa khar madia yéne ani sadiya🤦

    Arame ThioubeArame ThioubeIl y a 5 jours
  • Yen mom teguolen niou fen ish yeuffi dou course 🏃 am ben série diko tek normalement sax mo gueun li Daguey fatté sax ligua setanone la fois passé 🤦🏽‍♀️

    Khoudia LayeKhoudia LayeIl y a 5 jours
    • @Khoudia Layeah bon merci😥😥😥

      Mariama GueyeMariama GueyeIl y a 3 jours
    • @Mariama Gueye bn épisode 2 laniou tolu mais da am épisode 00 lolotaxx meun gua djap ni 3 laniou tolu selon toi

      Khoudia LayeKhoudia LayeIl y a 4 jours
    • @Khoudia Laye ma tek ne trois lsgne tolou

      Mariama GueyeMariama GueyeIl y a 4 jours
    • @Mariama Gueye 2 lagn tolu ni

      Khoudia LayeKhoudia LayeIl y a 5 jours
    • Wa episode 3la

      Mariama GueyeMariama GueyeIl y a 5 jours
  • Très intéressant

    Khady CisseKhady CisseIl y a 5 jours
  • Wa khar production boulen fater mayyy ma generik salimata bou youssou ndour please. C elle la concerner

    mado diagnemado diagneIl y a 6 jours
  • Saly et sa famille devait vivres dans une maison médiocre pour qu’en t’ils améliore que sa soit remarquable qu’à même 🤦🏻‍♀️

    Mamita BahMamita BahIl y a 6 jours
    • Elles étaient pauvres mais comme la maman travaille avec une riche femme d'affaire bah la dame je pense les. Aides beaucoup dc possible gnou dieuk si ker bu rafet s'en sitiztio'I change touti

      Mabintou DialloMabintou DialloIl y a 5 jours
  • Saly molna ndiol la daal nopnako way 🙄

    Mohamed BenzékryMohamed BenzékryIl y a 6 jours
    • @Mohamed Benzékry meunoumako yaw tmt khana do deggue

      Yaye Maye Lat MbaoYaye Maye Lat MbaoIl y a 4 jours
    • @Yaye Maye Lat Mbao bayima legui xana do degue🙄

      Mohamed BenzékryMohamed BenzékryIl y a 4 jours
    • @Mohamed Benzékry noboumala khana do deggue

      Yaye Maye Lat MbaoYaye Maye Lat MbaoIl y a 4 jours
    • @Yaye Maye Lat Mbao Kone nopma niou nobanter 🙄

      Mohamed BenzékryMohamed BenzékryIl y a 4 jours
    • @Mohamed Benzékry meunoumako

      Yaye Maye Lat MbaoYaye Maye Lat MbaoIl y a 4 jours
  • Ouseynou goor gou bakh ni yaw lay meel wayé femme binga love meritewoul sa beuguel dakh cousin la nopp

    Max La lionneMax La lionneIl y a 6 jours
  • *Une diction parfaite

    Khadija DrameKhadija DrameIl y a 6 jours
  • C tout mignon.com🥺🌜🥰🥰🥰🥰🥰🥰 de plus Ouseynou a un langage seghorien ,un diction parfait

    Khadija DrameKhadija DrameIl y a 6 jours
    • La diction accompagne l'effet oratoirrr car pour avoir la force de conviction il faut être convaincu et convainquant ,et on ne peut ,hélas ,convaincre qu'à travers les mots.

      Khadija DrameKhadija DrameIl y a 4 jours
  • Non galanterie ça existe tjrs

    Khadija DrameKhadija DrameIl y a 6 jours
  • Série bi nékhna trop wayé salimata est ce que dina seuy ak ousseynou beugue na séne couple bi dal ba bénéne épisode inchallah

    Daba GueyeDaba GueyeIl y a 6 jours
    • Mounirou laye moudiél

      oumista Diaoumista DiaIl y a 5 jours
  • Mai pk la maman de saly niko yak oussynou yagoulen alor kils ont fai bientôt 4ans En pls gniy wakh yayou rabia si commentaire bi Esk douguéne maci dimbali tamite Rabia ak Ousseynou sen parent dagno décédé non

    princesse torodoprincesse torodoIl y a 6 jours
    • Mère bi si bop bop am n'a loco manqué même soude 1mois sahh beuri na, mais 4ans wala da beugue sa fille de fornique, wala sou togue ba am 40 ans mou koy deff pression pour mou am diekeur, vraiment certains parents

      Mabintou DialloMabintou DialloIl y a 5 jours
  • Les sous titre en français s’il vous plaît 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾

    Aissata.TAissata.TIl y a 6 jours
  • Salimata niguay pauvrré nekh nama😂😂😂🙄

    Ramatoulaye Dieye DiopRamatoulaye Dieye DiopIl y a 6 jours
    • Moma diakhal nakk🤣

      Diabou SakhoDiabou SakhoIl y a 5 jours
  • Kia remarqué le regard d Ousseynou envers mounirou Ousseynou mi bandila haaa😂😂😂

    princesse torodoprincesse torodoIl y a 6 jours
    • Oui j'ai remarqué aussi

      Omar GueyeOmar GueyeIl y a 5 jours
  • Nafi dieye l'amie de rabya loutakh mou modé même à la télé nih dignou ray ak nopou néneu ni rek say khef nih bassang🙄😒

    Ramatoulaye Dieye DiopRamatoulaye Dieye DiopIl y a 6 jours
  • Nice series khar media

    Aminata SenghoreAminata SenghoreIl y a 6 jours
  • Thiey raby elle mom l'amour cest du materiel et khalis

    horssy Bahorssy BaIl y a 6 jours
  • ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

    Diatou FallDiatou FallIl y a 6 jours
  • Serie intéressant mais diabarou gorgui anamou dafa diékh wala

    Niang EvaNiang EvaIl y a 6 jours
  • L'homme de Saly il est galant machallah

    Yes YesYes YesIl y a 6 jours
FRlift